"Gouy Gui"
— sunget af Dior Mbaye
"Gouy Gui" er en sang opført på senegalesisk udgivet på 24 december 2023 på pladeselskabets officielle kanal - "Dior Mbaye". Oplev eksklusive oplysninger om "Gouy Gui". Find sangteksten til Gouy Gui, oversættelser og sangfakta. Indtjening og nettoværdi akkumuleres af sponsorater og andre kilder i henhold til et stykke information fundet på internettet. Hvor mange gange optrådte "Gouy Gui"-sangen i kompilerede musikhitlister? "Gouy Gui" er en velkendt musikvideo, der tog placeringer på populære tophitlister, såsom Top 100 Senegal Sange, Top 40 senegalesisk Sange og mere.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Gouy Gui" Fakta
"Gouy Gui" har nået 6.9M samlede visninger og 23.5K likes på YouTube.
Sangen er blevet indsendt på 24/12/2023 og brugt 73 uge på hitlisterne.
Det originale navn på musikvideoen er "DIOR MBAYE - GOUY GUI - (CLIP OFFICIEL)".
"Gouy Gui" er blevet offentliggjort på Youtube på 23/12/2023 20:00:10.
"Gouy Gui" Lyrik, komponister, pladeselskab
Streamez Gouy Gui ici 👉🏾
Dior mbaye, auteur et compositeur nous fait cadeau de Gouy gui ( baobab) emblème du Senegal . En wolof quand on te dis que tu es un baobab cela veut dire que tu es indétrônable dans ce que tu
;En chacun de nous sommeil un baobab.
Auteur : Dior mbaye
Beat, arrangement, Mix, master : Jeuuss Beatz
Réalisation : Pac deejay
#diormbaye #new #clips #gouygui
Remerciements
Danse: Fatou Sarr, Thiam, Khadija
Nom du groupe Bakh Yaye
Figurants: Flash Mo, Ibrahima diedhiou, Demba Keita , Oumar diallo, Daddy, Barry fruits, Rachid
Figurantes : Khadidiatou Mbaye, Thiaba, Aicha, Fatou,
Scénario : Mondial entertainment, Bamba Rassoul
Moyens techniques: Mc Yaram- Kdrd Films
Production du clip: Mondial Entertainment
Bijouterie la solution
Jannie styliste
Emprunte By Bella
Pape Beye jeune tailleur
Maquillage coiffure : Sonia Makeup; lama couture
Tissu :nafisamour
Kendey By Diegou bamba
LYRICS DIOR MBAYE
Waaw waw yehé Dior mbaye
yallah dogal louma def mou dém
Fa nié di teulé , nieulé di diém
Ma saff thi sen khôl ba dakk lem
Nguéne dima sani cœurs aki j’aimes
Bour YALLA dogal louma lal mou dém
Yaw Sakhar bou dekki koutia langue dem
kholal Ségne FALLOU ma wiss khorom bama niémé
Segne FALLOU ma wiss khorom ma yémé .
Refrain……
Pitie takk ci gouy (gouy yeugoul) pitie keuss keussi (gouy yeugoul) Pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) heyyy pitie yakk ci gouy ( gouy yeugoul) pitie keuss keussi ( gouy yeugoul) pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) yeugue ngani Gouy gui yeugoulaa (gouy yeugoul gouy yeugoula) boudé dangay diamb dé yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) yaw kholal mangay soul yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) gouy guou mak gui yeugoulaaa….
Mané dindi sakh
langa defona tia Gueune
yalla nopina
domou diambour kouko yakk dangko diouroul kouné khamna kila Meune
danga ko doul nangou yalla def na liko sop demb nopina
mané garap bou ndaw boko mounta rossé bayiko mou dound boul Diéma boudi boul boudilou khamo fou réne ba sakh
dandal soré déko khol de loin molay mousseul khana khamo né amna nio kham né ken doulen
; Refrain……
Pitie takk ci gouy (gouy yeugoul) pitie keuss keussi (gouy yeugoul) Pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) heyyy pitie yakk ci gouy ( gouy yeugoul) pitie keuss keussi ( gouy yeugoul) pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) yeugue ngani Gouy gui yeugoulaa (gouy yeugoul gouy yeugoula) boudé dangay diamb dé yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) yaw kholal mangay soul yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) gouy guou mak gui
;
Bo amé nianou wadiour loy ragal Koné
;Amna nianou wadiour loumay ragal naniou
;Lobita gueye Amna nianou Wadiour loy ragal Kone
; Pape Beye Amna nianou wadiour (le jeune tailleur), mbawor mbawor bi yow kay
; Ndeye thiam amna nianou wadiour (djiguénou Bass ) cherie soulemane sané
;
Ehh Wally boul
; Maryacine boul guestou ligueyou ndaye day
; Narou diaga boul guestou, cheri Sokhna boul guestou ligueyou ndaye day
; Kholal liguey focus niouy wakhtou khol bou rafet day tontou Maro marr boul guestou .
Tel: (+221) 785445245
Email: manager@
Site Web :
Facebook :
Instagram :
Snapchat : @diormbaye7
TikTok:
#diormbaye #new #clips